Lyrics of ' Tangal ' by Samba Peuzzi

On our website, we have the complete lyrics of the song Tangal that you were looking for.

Tangal is a song by Samba Peuzzi whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.

If you've been searching for the lyrics of the song Tangal by Samba Peuzzi for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.

Do you love the song Tangal ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Tangal by Samba Peuzzi ? You are in the place that has the answers to your desires.

Boy Ghetto what's up!

Geumoko wone finiou nobanté domafa guiss
Dieul: Fuck Love, I'm savage def sama devise
Diépi wone bép goor gouy doundou relation hindou
Guéne ak shaw une semaine mou dème, djiko yi meunoul andd

Kholou keurign la yorone, guél bou tang ma diarou
Bii bou bakh bi la, tay nak bouma reuthié ma wéré
Nga deungue wala nga dioup bokoy khol di waarou
Nieupa ngui wakh si dokhine bi ak rafétayam waaw

Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même "boy diay yékk"
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

Niro woul ak
Guèl yi dieul sène galé défko bar rek oubi
Entrée bi gratuite la
Mais bofa dougué yow yay dieund
Cons bokoulsi

Génération Jet-Set bi
Dakarou tay
Teksi diek set fils
Takk sama fitt songue khalé bi lé rek tek
Comment tu vas bébé est-ce que meune nga sigui khol ma
Yangui wéteuli sama mère tchi sama khol
Kheutch lokho bi rek tek si sama call
Mou sourire, ma contane ni nullard bou amm fitt
Affaires yangui commencé nekh, diokh nama 7-7

Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

Daw ba reuk, khar goudi pour ték premier pas
Tabakh souniou relation dieul kholam déf fa tank
Même pas une semaine, moungui ni boy bi dafma takkhe
Dougou Instagram screenshot photo ba tok
Défnama PP fépp bala dara khéw
Déguanté chaque jours, wakh téléphone ba néléw
Kounéka ngui saub, appels ak messages commencé taw
Je t'aime ya ngui dakanté ak ay Malaraw

Aligné kaw ba souff
Kholma boy, today j'suis sappé
Tay lagnou wara tassé
Bama shaw' bi, dama geuna tipsé
Bébé doumala khandiou
Auto, khaliss, villa
Dila diéma Pape et Cheikh
Liko dal moma dal
Khamnani lonkotinaaaa

Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu

Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap
Yah!
Khalé bi comme tangal

There are many reasons to want to know the lyrics of Tangal by Samba Peuzzi .

Feel like a star singing the song Tangal by Samba Peuzzi , even if your audience is just your two cats.

A very common reason to search for the lyrics of Tangal is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.

In case your search for the lyrics of the song Tangal by Samba Peuzzi is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Tangal ? Having the lyrics of the song Tangal by Samba Peuzzi at hand can settle many disputes, and we hope that it will.