Lyrics of ' Sokhor ' by Omzo Dollar

Do you want to know the lyrics of Sokhor by Omzo Dollar ? You're in the right place.

On our website, we have the complete lyrics of the song Sokhor that you were looking for.

Do you love the song Sokhor ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Sokhor by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Yalla meuneu mayé
Yalla meuneu mayé
Amna niit you sokhor nénagn nioy nangou li yalla mayé
Nioniou borom bi lagn gnémé
Borom bi lagn gnémé
Niogui lekkanté sen biir té amoul deuk bou nekh derett
Dama am travail de travail de maman
Domeu guiss ci tata
Dama am travail de maman
Doumeu fils à papa
Dama am travail de maman
Nieupeu am ay noone ci life bi
Yoonou diam soriwoul kone tankk amo nioulay guerre soriwo ci life bi
À buzzer

Niit yé sokhor
Tellement sokhor
Beaucoup sokhor
Trop trop sokhor
Pourquoi sokhor?
Geun lène sokhor
Yéré you sokhor
Guell bou sokhor, auto bou sokhor, keur bou sokhor
Bakh mo diex
Fogg ngua sokhor
Bakh mo diex
Deumb sur deumb
Nieuwna fekk fi ay deumb sur deumb
Kou bakh sou niawé, djikom neub na dieumeum
Gni lissi séni deund mou leundeum
Leundeumeu leundeum
Deumb sur deumb

Guiss guissou fènkat moy geum meu ma geum leu
Fresh lay def sol jacket sama ouleumeu
Sa période nieuweughoul ni femmeu bou eumb
Ennh boul deuk ci lidieunti kénèn
Sama adresse migui fénèn
Digua watchh liguey ndaxté job booo
Bou féké may sa thiono massa thiono!
Enh sama seetou dafa todj ma dem dieundi télé pour guiss sama bopp
Bayina noon yi di taatchou do degg ben yo founiouy taatchou
Nioune nékougn ci yoyou
Kharito ak ay rappeurs non nékougn ci yoyou
Sissou bi nékougn ci yoyou
Nigga magui seeni kanam sa youmay reculer
Beurri classes té moussouma redoubler
Boudé sa rap fayoula ndieugou auto
F u ak messages yiguay véhiculer nigga
Ken momoul yalla, yallah moniou mom
Mais ken momoul yalla
Mom moy taan kouko nekh rek mou tall leu
Lolou souleu mété nianal mou ball leu
Nianal mou ball leu
Gnampé gnampé sabou

Eau de javel nguay bolé gnampé gnampé sabou
Deff sa khol ci pan bomb mou bessat
Deff sa khol ci panier bamou?
Adouna dafa goudd tank, dé toungouné
Légende bir capsi niou tioukoulé
Takk sama fiit heureux ménage
Takk sama fiit heureux ménage
Daan na khekh di todj ay verres ba am
Ay bleus, biguay tass pour dieund vert
Bic bleu lay bindé vers yi fresh ni jet divers
Amna xaliss bala billets bleu di vert

Clash ma naleu deffal pub
Biss boy dadjék mane nak boul sax négocier
Am rappeurs yim fouy solall jupes
Té walay bilay douniou ay écossais
Hater wakh meu yoe louma leu ammel?
Orthographe ci sa khol ak seu bammel
Hamna ligua meu yagg nianal wayé magui
Takk nieup guiss ni phares des mamelles
Rap ak ay thiolé ci life non nékougn ci yoyou
(Nékougn ci yoyou yoyou!)
Ignane bi nékougn ci yoyou
Nigga magui seeni kanam sa youmay reculer
Beurri classes té moussouma redoubler
Boudé sa rap fayoula ndieugou auto
F u ak messages yiguay véhiculer nigga

The most common reason to want to know the lyrics of Sokhor is that you really like it. Obvious, right?

Knowing what the lyrics of Sokhor say allows us to put more feeling into the performance.

If your motivation for searching for the lyrics of the song Sokhor was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Feel like a star singing the song Sokhor by Omzo Dollar , even if your audience is just your two cats.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Sokhor ? Having the lyrics of the song Sokhor by Omzo Dollar at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

We hope we have helped you with the lyrics of the song Sokhor by Omzo Dollar .

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Sokhor by Omzo Dollar .