Lyrics of ' Omar’s Pain ' by Omzo Dollar

Do you want to know the lyrics of Omar’s Pain by Omzo Dollar ? You're in the right place.

If you've been searching for the lyrics of the song Omar’s Pain by Omzo Dollar for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.

Do you love the song Omar’s Pain ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Omar’s Pain by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Yeah yeah

Lane leu rap bi indi sama life
Ay deumeu you beugue lekk
Ay kharite you ko meussoul nekk
Khaliss bou lewoul buma meunoul lekk
Yeah lane leu rap bi infi sama life
Jeuf youmay leundeumeul si sama diner
Nit you lay geuneu bet so lene miné
Siw reuy bew meussouma ko def pour frimer yeah
Rap bimeussoul nek sama ligueye
Rap bi meussoul nekk sama ligueye
Mere bi dafa guente nioumay ligueye
Mané ko grawoul mere biguey guente magui ligueye yeah
Khamna gni ko geumone gni done salé
Gni meu ajdou wone ak gni meu faalé
Rap bolewouma ak sama beneu frère hun
Rap bolewouma ak sama beneu frere yeah
Kone li yeup pr li leu wone nigga
Li takh ma teylé ay diplome nigga
Damel ni sama bopp la togne
Ndakh Souma yeugone jeul benene yone nigga yeah
Yeah lane leu rap bi indi sama life
A part fans youma beugue bru defmeu sen nit
Nio takh 2 ans sans son magui ci game bi
2 ans sans sons magui ci game
Miezé meussoul bokk ak gayi
May bay rap beuri neu niou rap bayi
Yeah kone Lane leu rap bi indi sama life
Dou Dara louma meunoul dindi sama life

I say
Je joue des mots
Je joue des mots comme on joue de la guitare ou du piano
Comme de l'eau qui coule dans un ruisseau
Ma plume laisse des Larmes qui désarment les âmes et les affichent tel un panneau
Je joue des mots comme on rassemble les pièces d'un puzzle
Éblouis tout receveur car d'audibles miracles je suis faiseur
Je rassemble les mots comme une apostrophe
Car chaque strophe n'est que Catastrophe
Il y a les doux vents
Il y a les ouragants
Ma prose est une illustration de tout ce qui se trouve dans l'air
On trouve dans la rivière ce que l'on ne trouve dans la mer
Solitude comme châtiment, que dis je
Solitude comme armement
Dans un jardin de vérité fait naitre des roses aux épines blessantes
Vulgaires mais pudiques, moroses mais ludiques elle s'élève d'une maturité naissante
Une musique qu'il faut entendre pour juger
Souvent coincé dans un mirroir entre le terrestre
Et le céleste
Les mots les couleurs le sons les rythmes moyen de rendre mon intimité célèbre
Passion contre addiction
J'ai mes pulsions mes contradictions
Je me noie Entre des reves et des illusions
Ssp est l'histoire d'une désillusion
Car il ya ceux qui Vivent a mort et le reste en vie
Ceux qui vivent à mort, le reste envient
Ceci était juste une pensée dans une image
C'est l'histoire d'un jeûne rêveur qui a pris le chemin des poètes
Pour se rendre compte qu'il n'est pas un poète
Ssp asatsu

Li moy say say poésie
Bye bye comédie
Omzo dollar dem neu yonam c'était la last prophétie
Say say poésie
Bye bye comédie
Omzo dollar dem neu yonam c'était la last prophétie

There are many reasons to want to know the lyrics of Omar’s Pain by Omzo Dollar .

The most common reason to want to know the lyrics of Omar’s Pain is that you really like it. Obvious, right?

When we really like a song, as might be your case with Omar’s Pain by Omzo Dollar , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.

If your motivation for searching for the lyrics of the song Omar’s Pain was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Omar’s Pain by Omzo Dollar .

Learn the lyrics of the songs you like, like Omar’s Pain by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.