Lyrics of ' Omar Pen ' by Omzo Dollar

Omar Pen is a song by Omzo Dollar whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.

Do you love the song Omar Pen ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Omar Pen by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Tok sunu keur mu ladj ma kuy sama baay neketiyo (say say la)
Tok sunu keur mu ladj ma kuy sama baay neketiyo (say say la)

Han
Wowé ma young de riv
Beneu bar ga youkhou kogn beu hivre
Awma sentiment comme gni nieuw couper conteur yi
Boul contredire
Poésie noir leundeum comme kerign
Lumu geuneu gnoul geuneu saf comme cerise
Conquérir
Lo donoul talibem do done serign
Sokhlo wo lire ay tonne de livre pour deguéné ay tonne de livre
Underground comme chenille
Soufé ngua def comme cheville
Matchou city contre lille
So dougone armt done feu miss
One devise kougnou togne geu dis
Paraitre ni ombre ci
Lerr may servir comme tenis
Ak guel bou toy ni kogn venise
Kou merr bokko mane bokouma mais da am compromis
Ndahté awma temps pour shyne meme si ma montre brille
Omzo prime yene gauche mane droite si digui pont bou libre
Ndakh après the one lou dess c'est zero melni nombre 10
Meme souma jouewoul ma ngui si game bi
Melni compte twitch
Qu'ils me fichent la paix lou amoul fiche de paix jmen contre fiche

La poésie c'est quelque chose que l'on a sur le cœur
Je crois qu'un poème est une œuvre d'art
Il n'y a pas d'oeuvre d'art sans nécessité de connaissance réelle de langage
C'est une matière le langage
J'aime aussi une certaine musique
Un mouvement
Une respiration dans le verbe
Dans le langage

Limoy say say poésie
Bye bye comédie
Teylé bac+5 pour rap fils sama life lay fowé ni
Say say poésie
Bye bye comédie
Teylé bac+5 pour rap fils sama life lay fowé ni han

Khamna noy wakhé k kou teukh pour jokh leu noppam
Khamna noy wakhé k jiguene pour mou jokh leu boppam, for real
Nio tal sene rap bi comme sen poto keur yi
Def bepeu affiche bepeu salle melni photo serigne
Doumeu deumeu ni yene
Meunone na travestir sam music di leumbeul ni yene
Meunone na abrutir jeunesse tour lene leundeum ni yene
Def son pour TikTok guelou koba yeup geum meu ni yene
Soumeu vues takhone jouk khamna façon bum yugni def
Sokhlowouma rap bi lol lay santeu man
Narone na geuneu beuri khaliss souma amoulone ay sentiment
Principes dou nieup leu jik japeu na Leçon yi
Guisgeu nit ak mane guissat kok gnimay saga ndey sene son yi
Mais bon
Si j'habite, si jap yi
Narone merré adouna bi yeup depuis jadis
Motakh may balou yallah soubak ngone ni tijani
Beugouma woné sama bop melni hijabi, nigga
Motakh ma dal khalate rap galseneu tal salades
Eupeu guoorjiguen assassins creed valhala
Yi texte amoul si beneu bibliothèque
Beuri classe ak liasse you doy ni niari bible yo tek, rappeurs yi
Gnou mounoul wakhou rap nioy wakha ay wakhou stats
Niou mounoul wakh wakhou khour di wakh ay wakhou tate
Forcer ay lakk yo lene degoul seni complexes guendi kaw
Featuring ak 10 milles kaw man takhoul sen sons yi dougou kaw
Té dou géographie beuri leb si senni biographie
Khameunté suniou bir sokhlowoul sakh écographie
Meune geu firi say bars dou leu guéné sa cage
Nioune dagni bindeu ay livres yow dagn ley gerel sa page
Han
Jot na localisé ay mbalit qualité invalide
Miezé disqualifié pour balé Talibé gazzali
Nieuw sa galek calibre di leu jalé
Kou beugue guerre dadjé geu ak khalid ibn walid hum
Lou rap meune indi yeup meunoul fath samay gaume
Bayilene ak seni yeufou deumeu dem yar samay dom
Yeah, Last album après omar dem
That boy is sick with the pen they call him Omar pen nigga

The most common reason to want to know the lyrics of Omar Pen is that you really like it. Obvious, right?

If your motivation for searching for the lyrics of the song Omar Pen was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Feel like a star singing the song Omar Pen by Omzo Dollar , even if your audience is just your two cats.

In case your search for the lyrics of the song Omar Pen by Omzo Dollar is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Omar Pen ? Having the lyrics of the song Omar Pen by Omzo Dollar at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

It's important to note that Omzo Dollar , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Omar Pen ... So it's better to focus on what the song Omar Pen says on the record.

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Omar Pen by Omzo Dollar .

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Omar Pen by Omzo Dollar .