Do you want to know the lyrics of Nitté by Omzo Dollar ? You're in the right place.
On our website, we have the complete lyrics of the song Nitté that you were looking for.
Nitté is a song by Omzo Dollar whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.
Nitté
Nite yagui si bir nitt yi da melni yapou nit molen sourr
Niit dey dougal nitt Safara di ko nakh ak Adjana si kaw souff
Pithie mougui si kaw wanté khel bi yeup nekk Si souff
Kou dioudou si Cage dey fokkni ki sibiti mo dioum
Lane leu ley wagnil ioe someu yokalé
Mba loumey tall ioe dineu feyy seu yéné
Khana soy rafet dafay takh meu niaw
Kou kawé dey touti si kou meunoul naw (Abozé)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
Seytané wakhoul deugg gniko deglou negn yakk sen khel
Requin yi guéné djiko Caiman di negn done ay djane you matt sen guen
Gaïndé dou fallé Couille you bokk mbaar
Dieun bou ndaw si bou mak lekk ley done
Mala boudoul diamou YAllah Amoul
Pourtant Alakhira Souff rek legniouy done (Abozé)
(Ndakh maleu yéné guena nitté)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
Guiss na ay maguette birou khalé
Si bir ay khalé you bireul ay khalé
Degn sathione sunu enfance niou magg niouy sathie sunuy enfant
Boul dougal Khadjou mbedd si seu keur
Boul dougal Khadjou mbedd si sa keuuur
Meuy leu sama mbokk dou takh niou done cousin
Loup bagui Si poulailler bek Sourire bou Jaune poussin (Abozé)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
Maleu yéné gueuna nitté, dafa beurri louma meunou expliquer
Quelle mouche nous a piqués
Niit bouniouy Diamou ayy Kharr rek ley djité (Abozé)
Anh niou sante seni tour legn gueum
Kou khessal negn leu tour Leundeum
Sou goudou nopp takhone degg ken door mbame
Bou dessoul loudoul fass seu kanam daw do fallé Dos d’âne
Meuno mouss beu gaindé done bouki
Watt ay Kagna rat de terre niou nek Chauve Souris
XXX, lo peundeul mou sett
Ndakh khol bou diekh ak deun bou fess Lo djeund dou dess Boul tipssé
Limité sunu nitté yeup si succes
Succes si seu diné digueu distrait
Distrait beu dall si mur melni sindakh
Tête loin des épaules, Girafe
Am Xam-Xam Mandou wo moudié done serr
Kou am Chaire de Poule niou def leu Poulet de chaire
Seu succes seu none ley dane
Golo ak Allumettes boon ley tall (Abozé)
YAllah mom lissi Kanam
Boy diégui khol seu droite ak seu gauche beu
Safara beurineu niou fi defoul wone long feu
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
(Ndakh maleu yéné gueuna nitté)
Maleu yéné gueuna nitté, dafa beurri louma meunou expliquer
Quelle mouche nous a piqués
Niit bouniouy Diamou ayy Kharr rek ley djité (Abozé)
Otras canciones de Omzo Dollar
The most common reason to want to know the lyrics of Nitté is that you really like it. Obvious, right?
When we really like a song, as might be your case with Nitté by Omzo Dollar , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.
If your motivation for searching for the lyrics of the song Nitté was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.
Feel like a star singing the song Nitté by Omzo Dollar , even if your audience is just your two cats.
In case your search for the lyrics of the song Nitté by Omzo Dollar is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Nitté because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
It's important to note that Omzo Dollar , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Nitté ... So it's better to focus on what the song Nitté says on the record.
We hope we have helped you with the lyrics of the song Nitté by Omzo Dollar .
On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Nitté by Omzo Dollar .