Do you want to know the lyrics of Mame Premier by Omzo Dollar ? You're in the right place.
On our website, we have the complete lyrics of the song Mame Premier that you were looking for.
Mame Premier is a song by Omzo Dollar whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.
If you've been searching for the lyrics of the song Mame Premier by Omzo Dollar for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Do you love the song Mame Premier ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Mame Premier by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.
Amneu gnima begn, amneu gnima beugeu
Amneu gni di fenn, amneu gni wakh deugeu
Dinegn thiow, dinegn hate mais seneu wakh mo beuri
Kham nagn kane moy kane, kham nagn kane moy kane
Young fif zo dollar, adresse bi sicap leu
No djoutou gang team bi nak buzzlab leu
Dougnou wakh ac yow beneu mot niou tate leu
Sa papou pappeu ne le wakh kouy pappam
Mame premier, mame premier, mame premier, mame premier
Mane leu young fif premier, sama team mo meuner
Khalé fekkeu pa yi def lene bébé dakh nénegn les derniers seront les premiers
Kane mo beugeu problem nieuwlene venez?
Recolter lougn fi seumer
Nigga na ko deffal sama bopp boul dof damay hustle meli boy bou pappam renier
Somay press ay rappeurs né ma bon apétit
Niom nieupeu meu makk pourtant c'est mes petits
Fuck senni votes, senni media, doumeu révélation de l'année ya yékheu sip
Awadi duggy tee nénegn may deugeu bi
Rap bo doul dégeuti, capsi ma yékeuti
Yenene rappeurs yi di sop dougn ci lene dagni weur rek di fene melni politique
Doul rek ci deukeu bi
Rimes ay tonnou flow, ay qintalou syllabes
Punchline you lay def li marteaux defone talla sylla
Kene gnéméwoumeu clash? Je vous montre comment faire ça!
Omar vs Omzo, real vs Barça
J'ai un détour d'avance, rien a foutre de la chance
Été bo meu guissé boy damey am classe, pourtant nieupeu kham ni moussoumeu cours de vacances
Yélé yélé music baaba maal, dageuti sa bop melni sahaba
Katana, dageu na
May sene mame ADAMA
Sama meune meune ci rap meyou yalla leu do ci meune dara kone diokh meu billets nigga
Tout ce qui brille n'est pas de l'or mais ce qui est de l'or doit briller nigga!
Zo Dollar Zo commence Zo fini!
You fucking wit da monsta zoophilie
Rap ay couplet you pas net, lepp ci sama deundeu guéneu ni janet
Si t'es le meilleur rappeur au monde c'est parce que omzo vient d'une autre planète
0+1=1 la jangeu da melni lolou legui ay fenn leu
Zero geu may One té pourtant mane ac yow dougnou benneu
Wakh bou barri bi est ce que diarnako
Niou yorre game bi nieup khamnenko (Buzzlab)
Yan boy nio yekk si public bi wey lepp A ba Z
Concert ni dor ba parre public bi yekk tagolen (Eskey)
Nianal rappeur yi sen rap bi bakh
Ah! Niet likhlass ben fatiha (ndeysane) ndeysane
Di doul nane denen coming soon (Ah)
Te sama team dele coming soul
MC niata lelen fey nigga (wakhal)
Nenale liguey rek key fey nigga
Wakhnale adress bi sicap le fi buzzlab le niole tat diour sa pape nenanme Mame Premier
Otras canciones de Omzo Dollar
There are many reasons to want to know the lyrics of Mame Premier by Omzo Dollar .
A very common reason to search for the lyrics of Mame Premier is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Mame Premier because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
We hope we have helped you with the lyrics of the song Mame Premier by Omzo Dollar .
Learn the lyrics of the songs you like, like Mame Premier by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.