Lyrics of ' Borom Keur ' by Omzo Dollar

Gouro, 3 pieces
Gouro, 3 pieces
Gouro, 3 pieces
Gouro, 3 pieces

(I say) aladji miezé
Def la sama sokhna lala yéné
Man ak ioe si diakka, imam ak préfet
Boléma'ak sa papa nako gérer (woo)
Yow laa wa yow le
Yow laa wa yow le
Beug nala khamna beug ngama
Doyyal ngama soumala amé amna niénti diabar
Eh ngani pa bi nako wo-oh-oh-oh
Damleu beug takk guénouma ak yow-oh-oh-oh
Vieux père woxma lanela loy douter-eh-eh-eh
Beug nako amna dinée ak ligué-eh-eh-ey (yeah)

Baby oubbil ma sa xol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah)
Naala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur (woo)
Wokhak sen wa keur nélène maay sa borom keur (anh yeah)
Naa taal sen keur sougnma deffoul sa borom keuur (oh, yeah)

Dina indi gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces

(I say) takk sama fite
Do am ben woudiou baby à part sama fite (yeah)
Boula nékhé doreul radio
May sa borom keuur, baby cardio
(Eh) louy bayyanté pour kouné sey sey bi?
Ah bougn def lolou kay niou sey sey bi
(Eh) mak yow warrouniou am blem
Ya eupone prétendant championnat anglais
Réception invités yi nanni jinja
Soma firé dina mourou melni ninja
Mayé bou ndieuk meyyleu galé tekk cii 3 quarts
Soumaley nianni feug ngandi boubou 3/4
Man la gars yi wowé bad man miezé
Am diabar mou melni yow laa yagg rêver
Nuit de noce premier son ma mayyleu bébé
Yalnaa tokk di lath yallah finga fété (yeaaaah)

Baby oubbil ma sa khol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah)
Nala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur
Wakh ak sen wa keur nélène may sa borom keur (anh yeah)
Na tal sen keur sougnma deffoul sa borom keur (ooh yeaah)

Dina indi gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, def trois pièces
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces (ngané lane)
Gouro, trois pièces

Aladji miezé
Def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah)
Aladji miezé
Def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah)
Aladji mieze
Def la sama soxna lala yéné (yeah yeah yeah)
Aladji miezé
Def la sama sokhna lala yéné

There are many reasons to want to know the lyrics of Borom Keur by Omzo Dollar .

If your motivation for searching for the lyrics of the song Borom Keur was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Borom Keur ? Having the lyrics of the song Borom Keur by Omzo Dollar at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

It's important to note that Omzo Dollar , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Borom Keur ... So it's better to focus on what the song Borom Keur says on the record.

Learn the lyrics of the songs you like, like Borom Keur by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Borom Keur by Omzo Dollar .