On our website, we have the complete lyrics of the song Yolé Yolé that you were looking for.
If you've been searching for the lyrics of the song Yolé Yolé by Samba Peuzzi for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Do you love the song Yolé Yolé ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Yolé Yolé by Samba Peuzzi ? You are in the place that has the answers to your desires.
Boy mako wax
Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp
Amoul loumey tite from dièk waw
Dérétou diameugeun yolé yolé yolé
Ragalougn ko hé yolé yolé
Nioune ragalougn ko
Mako wax sa rappeur dou dem fen
Té na saltél feep waw waw
Amoul loumey tite from dièk waw waw
Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé
Ragalougn ko hé yolé yolé hah
Nioune ragalougn ko
Yonou musique bouko def xew xew
Mane damay fo meun na salsa dilén fathi
Kakatar ci flow international dou ci langue
Reuy lamigne mo len té ci souf
Nieupa beug def béneu diap
Bayi na boudé li ngen di def ay rap
Indi lou bess si game bi
Gayi di sissou nane damay tassou
Signé orthographe sen entre jambe
Sho yi ba ngen fok ma tico-tatoo
Laal ay millions takhoul ma dem tok
Waxal wizkid ak tekno ma ngui tew
Lep muy bien bayi len niou hablar bro
Dawou ma thiow
Manquer vibe manqué style takh
Ma bagna def ni niom di sol yénén yéré
Ay dof lagn téglé hit comme un
Toofan da nga wara taak téré
Represent ko nieup sip niouné
You bess yi niow beugeu mambou bo
Ba ngen di deup ndox ma ngui liguey
From ghettho buzzou Ndongo Lo
Boy mako wax
Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp
Amoul loumey tite from dièk waw
Dérétou diameugeun yolé yolé yolé!
Ragalougn ko hé yolé yolé nioune ragalougn ko
Mako wax sa rappeur dou dem fen
Té na saltél feep waw waw
Amoul loumey tite from dièk waw waw
Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé
Ragalougn ko hé yolé yolé hah
Nioune ragalougn ko
Deuk kognou siteu
Rêvé log ni deuk cité
Succès depuis khalé lako coaché
Call me khassate khaléyi bro
Li ngen esclave dageu boum mou gathié
Takkal mère bi ay chaine nou or
De flou saleté ma fay batay ma sen
So darling ma nek si bop bi bro
Khamo len dara beug def rap bi job
Sen genre yi taux de chômage lagniy yok
Woutil ci lo diap même boy nirok jamel
Deuk bi goor rou lokho ci poche rek kay bok
Baat bou yambar bi momay fay
Loutakh makay changé di forcé lou rock
Khép ma ndax damay represent
Boy ghetto bi dal téré sa dome
Téwal dièk fay narr bi khoromamemafia bi begue
Li si dess yeup je m’en fou
Khawma défaite pourtant chaque jour si mane
La bay yi accro comme parifoot
Indil niou yolé sama gang bi kén dou khof
Tapét yi ngen tek bandit
Dagn len na khékhal demb
Tay niou fok niou dofS
Seutt tou dix points yi takh
Nerf you demba yi tendu
Boy mako wax
Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp
Amoul loumey tite from dièk waw
Dérétou diameugeun yolé yolé yolé!
Ragalougn ko hé yolé yolé
Nioune ragalougn ko
Mako wax sa rappeur dou dem fen
Té na saltél feep waw waw
Amoul loumey tite from dièk waw waw
Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé
Ragalougn ko hé yolé yolé hah
Nioune ragalougn ko
Yolé yolé yolé ragalougn ko
Hé yolé yolé hah
Nioune ragalougn ko
The most common reason to want to know the lyrics of Yolé Yolé is that you really like it. Obvious, right?
When we really like a song, as might be your case with Yolé Yolé by Samba Peuzzi , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.
If your motivation for searching for the lyrics of the song Yolé Yolé was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.
Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Yolé Yolé ? Having the lyrics of the song Yolé Yolé by Samba Peuzzi at hand can settle many disputes, and we hope that it will.
On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Yolé Yolé by Samba Peuzzi .
Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Yolé Yolé by Samba Peuzzi .