Lyrics of ' Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) ' by Omzo Dollar

On our website, we have the complete lyrics of the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) that you were looking for.

Do you love the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Legui loy siip
Dafa barri batine
Legui loy siip
Dafa barri batine

I say
Takkeu na fou gas fay, tal sama bop ndakhté may fay ah sim
Lakké na beu glace sey, mounougn ma tey ndakhté ma tey ah sim
Niata la fi kong you meu sarakhou beu soneu pour ma feugue teh dou tam tam ah sim
Hotel so khamone lagn may jokh sene bopp ngir niou yokeu sama kham kham ah sim
Fuck say dm ak seu cm
Maguek double dm depuis cm
Vacances ak guel bou geuneu fess valises
Sama son di daw melni daf gnu amel khaliss
Mais bakh dafma nelowal sokhor moma yé
Am neu niou meu gné wanté amoul kou meu nier
Mi casa tu casa c'est occasionnel tabakh galet si bir casa nekeu casanier

Temps yi sama bopp bi da fess magui ci yenen jap, yeah
Narone na saga sene akh, magui ci yenene jap
Fi ak touti dotuma degue wolof magui ci yenene jap
Dotouma rappeur galsene magui ci yenene jap
Ey Ligueye indi khaliss, khaliss indi bitches
Bitches indi problem, problem sokhlo ligueye
Ligueye indi khaliss, khaliss indi bitches
Bitches indi problem, problem sokhlo ligueye

Sa yo degué sama bat, batou capsi guey am fofou
Karack amitié 3 Deret ci biir ci biti confisqué guey am fofou
Shit real nigga neva die kheuchy T guey am fofou
Rest in peace nigga gnou rest nigga cheikh moz guey am fofou

Mangui si japou transfert
Si japou anchères
Si japou oubi deuxième bureauk ay vacancières
Si japou dougou fone ay khalé youma doul door
Ba paré guéneu door ay khalé youmeu doul fone
Si japou bagna fegn trace bayi trace
Si japou jeundeu nit youmay jay jap
Si japou tabakh, ngandi galet couleur vert rose

Oubi fenêtre bountou pikine
Bountou bagui fenêtre mermoz
Fils temps yi sa humeur bi dokhoul
Magui dokh ak febar you docteur bi wakhoul
Kone motakh naro gnibi tant que keur bi todjoul
Motakh soumey guiss rappeur guissouma ludul heurou ndogou
Geuneu feuss gayi dagne geuneu feuss

Base bi lagni geuneu deup
Class bi dineu yemeul beut
Liass dinegn geuneu keupeu
Ndaré moma geuneul deuss
Plage bi dima geuneu euf
Thiaz yi dima geuneu beuss

Temps yi sama bopp bi da fess magui ci yenen jap
Featuring ak yow ma bagn magui ci yenen jap
Am na ex boumeu call mané ko bitch magui ci yenene jap (true story)
Dotouma rappeur galsene magui ci yenene jap nigga
One two three let's go

Ey Ligueye indi khaliss, khaliss indi bitches
Bitches indi problem, problem sokhlo ligueye
Ligueye indi khaliss, khaliss indi bitches
Bitches indi problem, problem sokhlo ligueye

Sa yo degué sama baat, baatou capsi guey am fofou
Karack amitié 3 nigga va niquer ta, dollavelli guey am fofou
Shit, dougou restau ac sa mère aladji mieze guey am fofou
Takeu sama chain wathié sama
Jean yeah fresh to death guey am fofou

There are many reasons to want to know the lyrics of Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .

If your motivation for searching for the lyrics of the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

A very common reason to search for the lyrics of Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.

Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.

It's important to note that Omzo Dollar , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) ... So it's better to focus on what the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) says on the record.

Learn the lyrics of the songs you like, like Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Yenene Jap (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .