Xel Ak Xol is a song by Omzo Dollar whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.
If you've been searching for the lyrics of the song Xel Ak Xol by Omzo Dollar for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Sama xol moma djitale xel tekk ma ci yone wawawa
Sama xol moma djitale
Diarignole sa xel do meussa diawalei bayi xel bayi meuna yobalei
Diarignole sa mind do meuusa diawalei bayil xel bayi meuna yobalei
Xel moy nitt tei mola meuna djitale ba doto diawalei
Xol moy nitt tei mola meuna djitale ba doto dia
Xol ak xel alale ak xol sol ak ciel alale ak sole nou yeuk
Ayeuk meile fou xalate tole mbolo nk ba melni taw ak tole
Wawaw dinga diare ci selebeyoon yeine sayi yeine sayi
Nguir nga xam finga dieum wawaw wawaw boko deifei magg waw
Mbeuguel lay goumba lo mais neinagn xol lay guissei
Xel bou nior xol bou neupp andoule ak nitté
Xole ma ak sa xol waxma lane nga guiss
Boudé lou bone ngay xolei lou bone rq ngay guiss
So amei xol bou tass sama xel day worry
Sa yo dieguei sama xol sama xel day sorii
Kone xolma ak sa xol waxma lane nga guiss
Boudé lou bone ngay xolei lou bone rq ngay guiss
Diarignole sa xel do meussa diawalei bayi xel bayi meuna yobalei
Diarignole sa mind do meussa diawalei bayil xel bayi meuna yobalei
Xol ak xel alale ak xol sol ak ciel alale ak sole nou yeuk
Yeuk meile fou xalate tole mbolo nk ba melni taw ak tole
Xel day xalate ba yei ma ci nelaw xol daye
Rafett oyof melni nguelaw soudone deukk na dem
Anh xel rq la sama xol bi di wolou
Souma sagnone ni pepp souff la sama xol bi di toleu
Sama xol yaramou neine fi sama xel bi di solou
Sama xol da gatt xel ba sama xel bi di xolou
Fou xel bi di sorou xol lay nelaw xel bi di seulmou
Boul meussa fatei xol lay diap wayei xel moy coeurou
Xol ak xel sougnou beurei sama xel bi moy dane
Dougal sama bopp si seau 'wou acide sama xel bi dou panne
Abozé
Gnima def sen xol gnoungui sama xel
Gnima geuneu def sen xel nekougn sama xol
Xol lay deglou xel di tektel
Sama xel lay tek xol fou sama xol di tekk xel
Sama xol day xalate xeli xoulo fepp fou xel diarr
Damay rap ni kou ame gnarri xel boul ame xel gnarr
Boul ragalei xel tanki rq la fitt bi di daw
Na sama xol taxaw mais jamais sama fitt bi di daw
Xol ak xel alale ak xol sol ak ciel alale ak sole nou yeuk
Yeuk meile fou xalate tole mbolo nk ba melni taw ak tole
Otras canciones de Omzo Dollar
When we really like a song, as might be your case with Xel Ak Xol by Omzo Dollar , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.
Knowing what the lyrics of Xel Ak Xol say allows us to put more feeling into the performance.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Xel Ak Xol because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Xel Ak Xol by Omzo Dollar .
Learn the lyrics of the songs you like, like Xel Ak Xol by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.
Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Xel Ak Xol by Omzo Dollar .