Lyrics of ' Sante (feat. Kheuchy-T) ' by Omzo Dollar

Do you want to know the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar ? You're in the right place.

On our website, we have the complete lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) that you were looking for.

Sante (feat. Kheuchy-T) is a song by Omzo Dollar whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.

If you've been searching for the lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.

Do you love the song Sante (feat. Kheuchy-T) ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Yewu tal ben tabac
Sante
Nane cafe japp jouli niari rakaa
Niane yalla pour mou yeureum sama nigga Aba
Tall sama call ay plaignant ay plaignant ay plaignant et encore des plaignants
Guene dokhontou si kogn bi dadiantel yenen plaignant ay plaignant mais rien que des plaignants
Convoker nagn ma fi cadass
On est des bonhommes on a pas peur nigga
Gayi teudj nagn sama shop
Mais chacun son tour chez le coiffeur nigga
Kne soma guisse sa kogn may dokh di yor sama sac wakh ma lane nga sokhla boul ladj limay diay
Khiffou ma sonou ma merou ma doffou ma dewala febaroul (bayima ma sante)
Mangi degu di guiss mangi dokh mangi dokhal di def yeufou nitt (nigga bayima ma sante)
Sante Yalla Sante Yalla kheuchy T ak omzo dollar deal bi kham nga lane la lep lo topato woul mou tass loy def soko gueume mou bakh (bayima ma sante)
Hm pa bi ak mere bi gningi doundou (Sante)
Fils dama fresh melni demb la dioudou (Sante)
Tous le monde va bien alhamdoulah tous le monde va bien
L'homme a peur sinon ya rien
Eh fils dama bayi rap bountou galei fess ak ay nitt melni kogn bi da amone ay thiante
Bayima ma sante
Bayima ma sante
Bayima ma sante
Bayima ma sante yalla sante yalla sante yalla sante yalla
Abozei get em

Sante yalla sante yalla (sante yalla sante yalla)
Mangi teral sama maman (mangi teral sama maman)
Wakhal Serigne bou may ligueyyyye
Ligueye rk moy fay th mere bi mougn may nianal(teksi mere bi mougn mqy nianal)
Danga may rombe mane ma khadial ko pousse
Nigga wakh ma gainde lane la wara sarakhou mousse
Kouma diayone graw legui mome dou dara dou touss
Damay setsi ay tissme di sol ay thiarakhou douss (wooo)
Si école yi dougn ma dakati
Dagn ma done dakk waye legui dagn may daka dji
Lolou mtx ma niewat diangal lene melni kouy TDI
Kham nagn sama C. D. I
Legui ma signe C. D. I
Di yone mere bi khaliss
Niana touma pa bi khaliss
Tk si ma ress samay kharit
Show yi legui elle m balise
Foma fk fima takhaw nga guiss guel yi dima topp di gawantou bala may dem melni mane may auto mbalite
Nigga Bayima ma Sante
Bougn ma rawe meunoul done si diom
Fonk ligueye khepp nelaw ba moudje done tching tchong
Et done quiconque
Niou ragalema donk ki songu
Niou done quiconque
Ma done king kong
Nakh bagna done quiconque
Th fougn ma sert ay cass ma touf li
Lou lil Wayne am si tatouage la am si tachou diouli
Noo tatouge men wara dougou chaque jour bank nakh sama micro ak sama BAC +5 fok samay calcul fegn

Bayil ma nianal samay soldier
Yalla mousseul niou si ndollll ba
Fima rombe nioumay sandi lokho
Restaurant la fourchette difa agné lokho Abozei
Kne soma guisse sa kogn may dokh di yor sama sac
Diapal ni danga khiff dh solatou ma sac
Khiffou ma sonou ma merou ma doffou ma dewala febaroul (bayima ma sante)
Mangi degu di guiss mangi dokh mangi dokhal di def yeufou nitt (nigga bayima ma sante)
Sante Yalla Sante Yalla kheuchy T ak omzo dollar deal bi kham nga lane la lep lo topato woul mou tass loy def soko gueume mou bakh (bayima ma sante)
Hm pa bi ak mere bi gningi doundou (Sante)
Fils dama fresh melni demb la dioudou (Sante)
Tous le monde va bien alhamdoulah tous le monde va bien
L'homme a peur sinon ya rien
Eh fils dama bayi rap bountou galei fess ak ay nitt melni kogn bi da amone ay thiante
Bayima ma sante
Bayima ma sante
Bayima ma sante
Bayima ma sante yalla sante yalla sante yalla sante yalla
Abozei get em
Bayima ma sante
Nigga bayima ma sante
Khiffou ma sonou ma merou ma doffou ma dewala febaroul (bayima ma sante)
Mangi degu di guiss mangi dokh mangi dokhal di def yeufou nitt (nigga bayima ma sante)
Lep lo topato woul mou tass loy def soko gueume mou bakh (bayima ma sante)

There are many reasons to want to know the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .

The most common reason to want to know the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) is that you really like it. Obvious, right?

When we really like a song, as might be your case with Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.

Knowing what the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) say allows us to put more feeling into the performance.

Feel like a star singing the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar , even if your audience is just your two cats.

A very common reason to search for the lyrics of Sante (feat. Kheuchy-T) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.

In case your search for the lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Sante (feat. Kheuchy-T) ? Having the lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

We hope we have helped you with the lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .

Learn the lyrics of the songs you like, like Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Sante (feat. Kheuchy-T) by Omzo Dollar .