If you've been searching for the lyrics of the song Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Do you love the song Goudi (feat. Majestic Drama) ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.
Oup oup
Oup oup
Oh
I say
Goudi guéthiou khaliss lay guenteu
Beutieuk si samay niakk lay fey
Ki sa nelow doy rek yangui nelow
Liguey goudi beutieuk lay fegn
Goudi guéthiou khaliss lay guenteu
Beutieuk si samay niakk lay fey
Ki sa nelow doy rek yangui nelow
Liguey goudi beutieuk lay fegn
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
I say
Han
Yallah yallah guéneu bey sa tol
Am ko sout defoula nit bou ndiol
Kheuyou fenn rawoul ngotou deugue
Lou khaliss doul jeundeu khaliss bu beuri neu ko jeundeu
Newone na t mouy deugue
Yene nek leu t borom rekka ci fanane
Newone na t mouy deugue
Lo donoul talibem meuno done serigneum
Newone na t mouy deugue
Bagn lo meuneuloul dara ak beugue nio yam
Kone wakh ci biir wakh
Kou meune fey meunatoul kharou bir ndokh nigga
Am loumay rêver di doundé
Lolou lay guénteu biss bou né
Nonou lay yewou di out mais
So khamone lilay yot, digeu faté lingay yot té daw
Goudi guéthiou khaliss lay guenteu
Beutieuk si samay niakk lay fey
Ki sa nelow doy rek yangui nelow
Liguey goudi beutieuk lay fegn
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
Geumeu soumay retane
Beut dou dioy loudoul loumou kham
I say
Nigga teudeul doyoul ndigeul new
Kou sa beugue beuri sa ngor néw
Fou lamegn togné bakkan lagni khekh
Lou nekh dou doy mais doylou doy neu nekh
Newone na t mouy deugue
Waro nateu say daleu sa tankou nawlé
Newone na t mouy deugue
Wadiour rekka lay yené guiss ga raw lene
Newone na t mouy deugue
Lou joylo khalé mo geun leplouy joylo mak
Kone wakh ci bir wakh geustoul ndakh geumeu dou tere niou guiss la nigga
Goudi guéthiou khaliss lay guenteu
Beutieuk si samay niakk lay fey
Ki sa nelow doy rek yangui nelow
Liguey goudi beutieuk lay fegn
Goudi guéthiou khaliss lay guenteu
Beutieuk si samay niakk lay fey
Ki sa nelow doy rek yangui nelow
Liguey goudi beutieuk lay fegn
Am loumay rêver di doundé
Lolou lay guénteu biss bou né
Nonou lay yewou di out mais
So khamone lilay yot, digeu faté lingay yot té daw
Otras canciones de Omzo Dollar
The most common reason to want to know the lyrics of Goudi (feat. Majestic Drama) is that you really like it. Obvious, right?
When we really like a song, as might be your case with Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.
A very common reason to search for the lyrics of Goudi (feat. Majestic Drama) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.
In case your search for the lyrics of the song Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Goudi (feat. Majestic Drama) because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar .
Learn the lyrics of the songs you like, like Goudi (feat. Majestic Drama) by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.