Lyrics of ' Bureau (feat. Young Tili) ' by Omzo Dollar

On our website, we have the complete lyrics of the song Bureau (feat. Young Tili) that you were looking for.

Do you love the song Bureau (feat. Young Tili) ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar ? You are in the place that has the answers to your desires.

Nigga damay liguey
Daga fogone dagni fo dagni liguey
Sol yere you cher dafa bokk sama ligueye
Bagna wakh ak taspé yimay tardel damay liguey
Yor telephone magui ligueye
Bagna ande ak domeram da bok sama ligueye
Fay ma sama khaliss bitch dou nonou ligueyé
Yeah yeah dou nonou lay liguey

Méti comme sa nieugou rerr
Di nga degg flow bii comme drianké bu takk ferr
Projet bé ngi tew, astroboy surveille le ciel
Prendre le train en marche? domaa guiss ma wathieu T.E.R
Doma guiss ma wathieu T.E.R
Wah wah
Astroboy surveille le ciel
Astroboy surveille le ciel
Dou meussa changer, Astroboy, 3ème barame tchi sène code

Hum, May dawlo sene biri
Rappeur yangui doundou love ac ay petasse yougn done iri
Boul sakh wakh zo nel pateu
Clash ma khawma no mel sakh
Di port comme colonel samb
Young fif aka lionnel fateu

Kone yenn nieup sène deudieuw (what! What!)
Tili amoul opps, carrière dagn key job, beutte frontière: Kilo de drogue
Concu dead na comme Sadio akk Salah, point rouge bi tchi sa bopp
Khaliss dagn key coacher, smoke sa mc: Jurgen Klopp

Walabok, dougou ville hors réseau
Dm na sa guel cho bi crise comme lagos
Khalé bi néna ma key rey melni norlevo
Dégue na rarement rek gay yoor liquide comme jet d'eau, daf leu jikk comme zéro hun

Tchi sa khel amna feu bureau
Tchi sa khol amna feu bureau
Yeah, fi nga tok amna feu bureau
Dangay rap biir Senegal, tchi sa taat amna feu bureau

Sa neegu mère ame na fa bureau
Bureau macky sall, ame na fa bureau
Dama sone depuis fadjar ma ngi bureau, da nga ma sokhla boul ma call, boul ma text, diaral bureau

Fuck lonase, fuck naar bi fuck ay paris sportifs
Douma solou niou né miézé tu n'es pas assorti
Kane mo leu neh meune ga dougou samay 18 batard
Senni khel dagn vide ni tali dakar 18 safar

Respect fayul aye factures
Chèque bi à partir de 5 zéro pour nga ame feat
Young Tili gérer sa tata nii AFTU
Gangg bi à vie, we coming man A+, BANG

Nene niow ci rap bi, rap
Ma lene dakha ndeye rap
Eupeu lene flow
Niom ñeup malene diangal ral
Xamu ñu gaat

Fuck aye rappeur douche
Li nguendu tekk or saf meu poup
Adja Diallo laye takk souff
Sama diabar mo dakkey fouf
Nigga welcome to say say fm
Khamna rappeurs you amoul bfm
Rappeur bu yengou teye, gnu K.S.N
Niongui point com niom nioy point sn
Yenn aye dèpp ngène
Nioune ay ref legn
Lepp akk effet wam
Faut qu'ma teins lene
Tili, Zo, Clive égal trio MSN
Fuck all these niggas comme débat fn

Fi guiss na ay string man di rap je suis gené
Sene tate louci dougou mo eup lou ci guéneu
Bo len di khous Awma problemou fluz
Sama kaos nio geuneu cher noreyni shoes

Da ngène djitteul aye tipeu
Fake comme yéré yii mouye sole tchi clippeum
Comme carrièrou influenceur vous êtes 'claté
Si elle a des formes rondes, on va au Carré
On écartait des mères bien avant KouKandé
Damn, khar sa mère melni koukandé
Compter khaliss, ça fait bander
Kick comme jackie chan sou mandé
Flow bi ni Yandé! Kone fekk ma bureau bitch
Tuto bitch, say say poesie leu philo bitch
Do gommer li gnu bindeu akk stylo bitch
Geuno lene saf khorom sirop bitch

There are many reasons to want to know the lyrics of Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar .

The most common reason to want to know the lyrics of Bureau (feat. Young Tili) is that you really like it. Obvious, right?

Knowing what the lyrics of Bureau (feat. Young Tili) say allows us to put more feeling into the performance.

If your motivation for searching for the lyrics of the song Bureau (feat. Young Tili) was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Feel like a star singing the song Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar , even if your audience is just your two cats.

Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Bureau (feat. Young Tili) because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.

We hope we have helped you with the lyrics of the song Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar .

Learn the lyrics of the songs you like, like Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Bureau (feat. Young Tili) by Omzo Dollar .