Lyrics of ' Peundeul ' by Narah Diouf

On our website, we have the complete lyrics of the song Peundeul that you were looking for.

Peundeul is a song by Narah Diouf whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.

Ak fo né thi town bi
Foo ne ci réew mi ñëwël fi yëngu ci lii
Narah laay dooni
Man la ma ñëwaat fi gëna teggu ci beat bi
Xoolal ni may dugge
Xoolal ni may yégge sama baat ci kaaw
Mélodie bé meu yéglo
Gisatuma, déggatuma
Lenn lay gis kon kaay fii ma wone la
Gisatuma, déggatuma la

I’m so high
I’m so high yeeeh

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël

Lu fora fora fort lay yëg sama xol
Fu kawe kawe kawe lay yekk sama yaram di yëngu
Ta xawma li koy yëngël fi mu jogé
Ayooooo
Guddi guddi non stress la dundu happiness
Tay non stop
Àndak samay way tay de fête la
Xoolal ni ma mel, kaay dance all night

Sound bi ndax yankay ngueug comme mane ni ma key yeugué
Wax ma ndax muñ lay duggu comme nimmey dougué
Gisatuma, déggatuma
Leen lay gis kon kaay fii ma wone leu
Gisatuma déggatuma la

I’m so high
I’m so high yeeeeh

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël

Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow
Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël)
Narah mu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël pëndël pëndël pëndël eeh)
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Ehhh ehh ehh ehh ehh
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Hummm hummm

The most common reason to want to know the lyrics of Peundeul is that you really like it. Obvious, right?

If your motivation for searching for the lyrics of the song Peundeul was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Feel like a star singing the song Peundeul by Narah Diouf , even if your audience is just your two cats.

A very common reason to search for the lyrics of Peundeul is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.

Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Peundeul because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Peundeul ? Having the lyrics of the song Peundeul by Narah Diouf at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

It's important to note that Narah Diouf , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Peundeul ... So it's better to focus on what the song Peundeul says on the record.

We hope we have helped you with the lyrics of the song Peundeul by Narah Diouf .

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Peundeul by Narah Diouf .

Learn the lyrics of the songs you like, like Peundeul by Narah Diouf , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.

Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Peundeul by Narah Diouf .