If you've been searching for the lyrics of the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Do you love the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) ? Can't quite understand what it says? Need the lyrics of Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung ? You are in the place that has the answers to your desires.
Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Baby tey meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Kou mèlni ngua sokhla meunè founè
Foumeu feuleu rèk djomal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
Hey vivi da ngua gueuneu khèw, ndourou wo kou bèw
Ya koy daguatè li lèrr na
Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Baby tey meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Kou mèlni ngua sokhla, kou beuri sèytané ba djakhal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul tchi birr nèkk bi
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Kaye meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Man ngua sokhla meunè founè
Foumeu feuleu rèk djomal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la
Sonou na tchi sagg bi
Di mougn lou mèlni
Sonou na tchi sagg bi
Di mougn lou mèlni
Baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni mann leu
Tè ngueu sigui kholma
Baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni mann leu
Tè ngueu sigui kholma
Bouguou ma lou sèddeu faw mou tanguou way
Tchine bokoul tchafine vivè kholoul tchi tchine
Ak lo wèkh wèkh na na noy seu ndiba tilim
Moh vivi yangui guaagn beuguou ma tchow wagnil way
Chérie nangoul ma, dama beuri djapp
Mane djomal na la té douma rapp
Antal ngua li ngua yènou boul wouttalou
Gnémé ko waw waw
Diguou laal lagnouy rèrrè, after yow lay dessero
Tchabi bountou nèkk bi tay rérouma
Boul wo walou gnémé ko wawaw
Lou mèlni makko mom
Té kou feugueu togn ma
Gneuweul ma défal la louy takh ngua nanguoul ma
Titangué warou la mba lèpp mingui bakh
Hey kaay fi, hey kaay hey
Li daf may ndourou sweet game waw waw
Casa de papel yeufou bandit waw waw
Seu âme dafa sensible sori ma
Chéri nangoul ma dama beuri djapp
Mane djomal na la té douma rapp
Antal ngua li ngua yènou boul wouttalou
Gnémé ko waw waw
Ngueu meunn diko dèf bokoul ak koukoy djèm
Yako meunn diko dèf yow da nguay fo
Hey ambiance
Gneuweul ma défal la louy takh ngua nangoul ma
Titangué warou la mba lèpp mingui bakh
Hey kaay fi, hey kaay hey
Ay, kou donn wakh na ngua noppi bass yèkssi na
Tay fi day nèkh day roumbakh poutch
Viviane yaw lo guénè gnou fetch ko
Tay fi day nèkh day roumbakh poutch
Eh Vivi eup ko bémou mokk du dara du yomb
Li daf may ndourou sweet game waw waw
Casa de papel yeufou bandit waw waw
Seu âme dafa sensible sori ma
Otras canciones de Bass Thioung
There are many reasons to want to know the lyrics of Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung .
Knowing what the lyrics of Sweet Game (feat. Viviane Chidid) say allows us to put more feeling into the performance.
If your motivation for searching for the lyrics of the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.
Feel like a star singing the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung , even if your audience is just your two cats.
A very common reason to search for the lyrics of Sweet Game (feat. Viviane Chidid) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Sweet Game (feat. Viviane Chidid) because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
We hope we have helped you with the lyrics of the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung .
Learn the lyrics of the songs you like, like Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.
Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Sweet Game (feat. Viviane Chidid) by Bass Thioung .