Lyrics of ' Louy Problème Bi? ' by Bass Thioung

Do you want to know the lyrics of Louy Problème Bi? by Bass Thioung ? You're in the right place.

If you've been searching for the lyrics of the song Louy Problème Bi? by Bass Thioung for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.

Bass Thioung lay doon

Man ku ma faale ma faale la
Ku ma talul taluma la
Joxoo ma ma lekk, joxoo ma ma naan
Doo ma tere dund, na ku nekk taal boppam
Nekk ci jàmm ñépp feex
Soo meree ki tal boppam
Doo nekk ci jàmm doo am tus

Comment tu vas, comment ça va
Ça va va va va va va va
Waxkat yi good morning, vas
Mbaa jàmm ngeen yeewoo, vas vas
Comment tu vas, comment ça va
Ça va va va va va va va

Ku mer kala mel ni Yàlla
La fa bini mashallah!
Bokku mak ñoom (ay!)
Niroowu mak ñoom
Ay defal ndànk bin bin
Man la bis bi dara du xew!
Hey, luy problème bi?

Problème bi fu mu nekk
Joxoo ma ma lekk, joxoo ma ma naan
Hey doo xol xanaa gisoo et vas

Man ku ma faale ma faale la
Ku ma talul taluma la
Joxoo ma ma lekk, joxoo ma ma naan
Doo ma tere dund, na ku nekk taal boppam
Nekk ci jàmm ñépp feex
Soo meree ki tal boppam
Doo nekk ci jàmm doo am tus

Comment tu vas, comment ça va
Ça va va va va va va va
Waxkat yi good morning, vas
Mbaa jàmm ngeen yeewoo, vas vas
Comment tu vas, comment ça va
Ça va va va va va va va

Benn nettalikat du tokk fi may tokk hey vas
Yàq der baaxul bul ma taxal way, vas vas vas
Jàmm ci yaw ak say mbokk doo bàyyi golo bi nga bokku
Ñoom man lañ bëgg man lãn sopp
Fees na bay tuuru mu ngi toog

Ku indi li (Bass)
Man lañuy toppando (Bass)
Ku dàq sañse fi (Bass)
Ku moom millions de vues (Bass Thioung)
Boroom tendance (Bass)
Seen reference (Bass)
Ku leen bëgg (Bass)
Kon kaay ñu danse (Bass Thioung)

Hey, luy problème bi?
Joxoo ma ma lekk, joxoo ma ma naan
Hey doo xol xanaa gisoo et vas

Yëngal!
Àtt bi sama àtt la
Ma xew xanaa neex
Yëngal
Ay heur bu ma neex
Dama koy yëngal
Par force, dama koy yëngal!
Ñu deme fecce ko fecce ko boy
Kaay man maa koy yëngal

Fecce bu bes la dafa xew avancer bul dof
Doxal dox bi!
Avancé yaa leen raw
Doxal dox bi
Avancé bul geestu
Doxal dox bi
Avancé yaa leen raw
Doxal dox bi
Avancé bul tontu
Doxal dox bi
Avancé yaa leen raw

Hey bëgg nga mel ni man, taxul nga mel ni man
Déedéet, mashallah bu la ma catu stop

Waa doyul!
Non, non, c'est pas fini!

Yëngal!
Àtt bi sama àtt la
Ma xew xanaa neex
Yëngal
Ay heur bu ma neex
Dama koy yëngal
Par force, dama koy yëngal!
Ñu deme fecce ko fecce ko boy
Kaay man maa koy yëngal

Fecce bu bes la dafa xew avancer bul dof
Doxal dox bi!
Avancé yaa leen raw
Doxal dox bi
Avancé bul geestu
Doxal dox bi
Avancé yaa leen raw
Bibi jege na
Avancé bul tontu
Aye bibi avanceel def patte
Bul tontu Bibi
How are you, I'm fine

Avancé
Doxal dox bi
Avancé
Doxal xol bi
Bibi jege na
Avanceel
Doxal dox bi
Aye bibi avanceel def patte
Bul tontu bibi
How are you, I'm fine

There are many reasons to want to know the lyrics of Louy Problème Bi? by Bass Thioung .

If your motivation for searching for the lyrics of the song Louy Problème Bi? was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.

Feel like a star singing the song Louy Problème Bi? by Bass Thioung , even if your audience is just your two cats.

A very common reason to search for the lyrics of Louy Problème Bi? is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.

Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Louy Problème Bi? ? Having the lyrics of the song Louy Problème Bi? by Bass Thioung at hand can settle many disputes, and we hope that it will.

On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Louy Problème Bi? by Bass Thioung .

Learn the lyrics of the songs you like, like Louy Problème Bi? by Bass Thioung , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.