Do you want to know the lyrics of Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung ? You're in the right place.
Kay Signé (feat. ZBest Family) is a song by Bass Thioung whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.
ZBest Family
Bass Thioung lay doon
Jongoma dangay dégg daaj
Soxor tegsi ñeme jarul sax di laaj
Xooleen ni ma moole
Yamal ci xoole dangay toog di xaar
Man damay xéy di gën di baax
Te yaw dangay xéy monté dékk di wax
Xooleen ni ma moole
Yamal ci xoole dangay toog di xaar
Peruque bi ma ko moom
Dàll beek saak, bul laaj fu mu jugé
Li ma sol ma ko moom
Dékku liggéey bu lew la ko ame
Sañsé dangay science, jarul histoire
Problému wax solution la laaj
Dangay solu tégu woo zo vision mu foto la
Mashallah!
Sa sañsé baax na
Ah kon mu ngi baax
Pourtant dama ko woyofal def lool neex
Mashallah!
Sa cheveux baax na, waaw!
Ah kon mu ngi baax
Ni lay fél-falale lu neex
Ba samay noon di jooy
Man lu tax bi la sañsé dafay dégu
Boo ma gisee bo siisuwul dangay nangu
Ci yaram bi la mbégte la laaj
Sañsé fi la fekk baax
Sama tailleur bi moo ko ñaw
Man ma ko sol
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sole statut ma gaaw
Sama tailleur bi moo ko ñaw
Man ma ko sol
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sole statut ma gaaw
Eh tubaab moo ko wax, apreciel
Bañ di critiqué di jëme mel ni signeel
(ZBest Production number one)
Jantal man dangay dégg daaj
Tegsi nga ma joxe bala kenn di laaj
Xooleen ni ma coofe
Yamal ci xoole dangay toog di xaar
Dangay jëf lu bari tuuti wax
Góor Yàlla la kon fokk ma xam lu baax
Xooleen ni ma coofe
Yamal ci xoole dangay toog di xaar
Céy man la bokk dama ko mën te sañsé ma ko moom
Pourtant du iblow du daf la gën ci sañsé moo la mën
Boy signé dinga sonn ndax yoru ma ci benn
Yaa nga solu ci esprit la doo ko dondu fenn, eh!
Na làmp yi daq yaw laal ma snap
Man dama stylé fraîche, yaw laal ma snap
Fu ma génn gën na fi la, Z-Best tamit ci la
Su ma neexee bad boy ndaanaan cho yi gën ma fi la
Mashallah!
Sa sañsé baax na
Ah kon mu ngi baax
Pourtant dama ko woyofal def lool neex
Mashallah!
Sa cheveux baax na, waaw!
Ah kon mu ngi baax
Ni lay fél-falale lu neex
Ba samay noon di jooy
Man lu tax bi la sañsé dafay dégu
Boo ma gisee bo siisuwul dangay nangu
Ci yaram bi la mbégte la laaj
Sañsé fi la fekk baax
Sama tailleur bi moo ko ñaw
Man ma ko sol
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sole statut ma gaaw
Sama tailleur bi moo ko ñaw
Man ma ko sol
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sole statut ma gaaw
Ey sama tailleur dafa meilleur (laf cat!)
Ey, sañsé bu meilleur (ngay am)
Ey sama sañsé dafa meilleur (laf cat!)
Ay, Sañsé bu meilleur (ngay am)
Ey sama tailleur dafa meilleur (laf cat!)
Ey, sañsé bu meilleur (ngay am)
Ey sama sañsé dafa meilleur (laf cat!)
Bon il est meilleur (laf cat!)
Li ma sañsé ça coût cher (eh, sañsé xale)
Oo dafa cher (waaa way sañsé xale)
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sol statut ma gaaw
Li ma sañsé ça coût cher (nga ni ma, sañsé xale)
Oo dafa cher (waaa way sañsé xale)
Ñëwleen signé, kaay signé
Li ma sol statut ma gaaw
Li ma sañsé ça coût cher (nga ni ma, sañsé xale!)
Otras canciones de Bass Thioung
There are many reasons to want to know the lyrics of Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung .
The most common reason to want to know the lyrics of Kay Signé (feat. ZBest Family) is that you really like it. Obvious, right?
When we really like a song, as might be your case with Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung , we wish to be able to sing it knowing the lyrics well.
Knowing what the lyrics of Kay Signé (feat. ZBest Family) say allows us to put more feeling into the performance.
If your motivation for searching for the lyrics of the song Kay Signé (feat. ZBest Family) was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.
Feel like a star singing the song Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung , even if your audience is just your two cats.
In case your search for the lyrics of the song Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung is because it makes you think of someone in particular, we suggest you dedicate it to them somehow, for example, by sending them the link to this website, they'll surely get the hint.
Something that happens more often than we think is that people search for the lyrics of Kay Signé (feat. ZBest Family) because there is some word in the song they don't quite understand and want to make sure of what it says.
Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Kay Signé (feat. ZBest Family) ? Having the lyrics of the song Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung at hand can settle many disputes, and we hope that it will.
Remember that whenever you need to know the lyrics of a song, you can always turn to us, as has happened now with the lyrics of the song Kay Signé (feat. ZBest Family) by Bass Thioung .