Do you want to know the lyrics of Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) by Bass Thioung ? You're in the right place.
If you've been searching for the lyrics of the song Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) by Bass Thioung for a long time, start warming up your voice, because you won't be able to stop singing it.
Montre bou bèsse parfum bou cher
Diantal ba yakou mameune say ex doumalè baal lolou mane nguéne fi fék
Météo layoure, diko tangale janvier ba déc
Kholal li ma soll taille leur moko niaw
Mangui méleni ni or ak fii réw mi tolou
Ame aye tissus thi container maléne dak port
Nénaniou wally dou sidi diop mongui beugueu moche ndanane nagui dokh
Douma nittou fi paparassi dof
Douma nittou fi diaroule indi torche
Naye lére douma nittou fi ndakrou basigui Dior
Mane laniou beugueu guisse loloye bénéficie
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Namouma khéwe nénamané
Taille base ak marinière maako téré nékh
Parfum
Fallé wouma say ex mane m'a fi né
Taille fine validé mane ma finé
Charismatique, métte ni dama mette ni
Khollale lima sole
Dama diék ndiol
Yor dér bou nioule
Dama nékha xoll
Ndanane nagui dokh
Paparasi dof
Diaroule andi torche naye lére douma nittou fi
Ndakarou ba sigui Dior mane laniou beugueu guisse
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Boule balé bo diéko boule balé
Caprice (aye)
Femelle (aye)
Problème (aye)
Femelle (aye)
Papy, arrête mais mounou nio yame arrête
D'accord j'arrête ma noirceur débène
Make-up cheveux yokou si ongles tu veux mane leu
Yaléne meune diaroule débat
Maléne meune diaroule débat
Youkhole thi kaw youkhole thi kaw
Ya des hauts ya des bas
Régleu say problème mou cas
Kounék ak say problème, kounék ak say problème
Ya eupe dolé thiathiathie yaléne meune
Kholale linga sengsé deff koni bb di ko teteee
Otras canciones de Bass Thioung
There are many reasons to want to know the lyrics of Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) by Bass Thioung .
The most common reason to want to know the lyrics of Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) is that you really like it. Obvious, right?
A very common reason to search for the lyrics of Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.
Are you arguing with your partner because you understand different things when you listen to Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) ? Having the lyrics of the song Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) by Bass Thioung at hand can settle many disputes, and we hope that it will.
It's important to note that Bass Thioung , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) ... So it's better to focus on what the song Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) says on the record.
On this page, you have at your disposal hundreds of song lyrics, like Dozéko (feat. One Lyrical & Leyna) by Bass Thioung .