On our website, we have the complete lyrics of the song Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) that you were looking for.
Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) is a song by Ashs The Best whose lyrics have countless searches, so we decided it deserves its place on this website, along with many other song lyrics that internet users want to know.
Am na ñu blem
Je t’aime et tu m’aimes pas
Parce que da maa ñaaw, bye bye
Xale bu xees bi pour boroom xaliis bi
Neenañ jëllël mbindaan bi, ay waay
Yanul ma briques yi
Lu ma tee des ci tool yi
Su ma yëggoon des dëkk ba
May boroom puus-puus bi
Chauffeur ru car-rapide bi
Apprenti bu ñuul bi
Kaw-kaw bi lañ may woowe
Bëtt bu nekk ñu ma koy xoole
Boy town bi man may ngaakaam
Nax ma naxaat may doora xam
Lijjënte paasu kaaw dem daani doole
Nangu nekk kaw-kaw luma am yoone
Ndey’ag Baay ci man lañ yaakaar kon waru maa coole
Lumay def def ci fulla’g fayda nimu gën a moole
Tallu ma di dem soiree, tallu ma doxaani, tallu ma ay xawaare
Dollar dollar dollar ay million, million dollar, million
Dara dara dara sama vision, Ludul million dollar, million
Sàngo’og fulla’g fayda
Lu mëna nee la
Deel yoone di woote
Sa yaay bumu jaaxle
Sa jabbar di xaar dëkk ba
Korité demmoo Tabaski bi ngay xaar ba Tamxarit fekk la fi
Li ngay am as weer doyu la fay ci neeg bi begee wax ma kër ga loo fay yoone
Xale bi ngay jël nobbu la xamoo ni yow yay dofam baayil sa xel bi ngay foowee
Kaw-kaw bi lañ may woowe
Bëtt bu nekk ñu ma koy xoole
Boy town bi man may ngaakaam
Nax ma naxaat may doora xam
Gestul ñi nga baayi ginaaw
Dañ yaakaar ci yow
Bul Sàmba Alaar Ngoor
Fexeel ba sa yaram daw
Bumu neex nga fate li la fal
Deel baayi xel ginaaw
Yeah mën a nee soo tasul sen yaakaar
Lepp mën na nekk te doo def lu ñaaw
Jamano buñ tòll waratoo nelaw
Deel fataliku demb njaboot gi nga baayi
Balaa ngay baax àll baaxal ci kër gi waay
Mën nga am ay million million dollar
Taxul nga sàalit waay
Sa ngor bulko mës jaayee dara
Bul fate li la fal
Kaw-kaw bi lañ may woowe
Bëtt bu nekk ñu ma koy xoole
Boy town bi man may ngaakaam
Nax ma naxaat may doora xam
Kaw-kaw bi lañ may woowe
Bëtt bu nekk ñu ma koy xoole
Boy town bi man may ngaakaam
Nax ma naxaat may doora xam
Otras canciones de Ashs The Best
The most common reason to want to know the lyrics of Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) is that you really like it. Obvious, right?
If your motivation for searching for the lyrics of the song Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) was that you absolutely love it, we hope you can enjoy singing it.
A very common reason to search for the lyrics of Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) is the fact that you want to know them well because they make you think of a special person or situation.
It's important to note that Ashs The Best , in live concerts, has not always been or will be faithful to the lyrics of the song Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) ... So it's better to focus on what the song Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) says on the record.
We hope we have helped you with the lyrics of the song Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) by Ashs The Best .
Learn the lyrics of the songs you like, like Ngor (remix) (feat. Mao Sidibé) by Ashs The Best , whether it's to sing them in the shower, make your covers, dedicate them to someone, or win a bet.